Diégué Kiraay

Wally B. Seck

Compositor: Não Disponível

Mësuloo ko ni waaw góor walla yaay jaambaar
Ba mu nekke ci àdduna
Mësuloo nangu li ko Yàlla Buur bi jagleel
Ba mu nekke ci àdduna
Tay ji dem na ngay jooy
Ñépp ñoo ngi naan aka moo baaxoon
Na la leer ni ñun dem na

Lu baax lu mu def fi musoloo ko ko yéene
Ku fi dee rekk ñu wax sa baax
Bàyyi ma jalaale di la jooy
Ayoooo ndeysaan!
Àndak wa këram toog di la jooy
Ndeysaan mbaa xam nga
Moo ngi ci ndox jege ndox te du lakk ku ngay xool
Xel xool sa xaalat ak yéene bari na

©2003- 2025 lyrics.com.br · Aviso Legal · Política de Privacidade · Fale Conosco desenvolvido por Studio Sol Comunicação Digital