Désolé (feat. Le Raam Daan)

Wally B. Seck

Compositor: Não Disponível

C'est pas de ma faute
Sou féké damalaye dérangé (désolé)
Nga baalma, xamna sakh niima mele si rewmi Nekhoula (désolé)
I'm so sorry, Soudé louma lalle Yalla teksi loxo (Ngeunele laa)
Wakhambané bou gnémé kouy ligueye guene, lou setane si mane (non non)
Linga dadie si yakeu soko dadione si ligueye wessou fii
Je suis désolé

C'est pas de ma faute
Sou féké damalaye dérangé (désolé)
Nga baalma, xamna sakh niima mele si rewmi Nekhoula (désolé)
I'm so sorry, Soudé louma lalle Yalla teksi loxo (Ngeunele laa)
Wakhambané bou gnémé kouy ligueye guene, lou setane si mane (non non)
Linga dadie si yakeu soko dadione si ligueye wessou fii
Je suis désolé

Si être aimé par les autres peut faire mal à autrui (désolé)
Si ces plumes me montent
Par mes mélodies te détruis
Je suis désolé

Yow kholale
Diiwangui néé di deme
Bour yalla koye deff si diamame

Mala douma tabakh
Because Lou domou adama bi lambo
Bour yalla koko diaguelele (Soula yaboo)
Baye gualaye nagou Nagou mo geune (Sa wadjii boula yaboo)
Mame Ro mo dogual nagne nagou Nopalou

Yalla gueumoul nelawoul tei dou diawaleii
Dieufou kouné louné lounekk foneii guathia
Forou mako, Lima diangue, Laye tari
Sathiou mako (lima diangue lay tarii)
Lou waye donnou mou deugeur
Li gua yorr forouloko
Aah, N'a na na naa ooh
Forou mako, Lima diangue, Laye tari wo wo wooo
Sathiou mako, sama gnom mame gnoma togne, nana nana nana
Li loussii waye mane Sing Sing dou nakhé mbaaye
Ndakh nakhé mbaaye dou yagué nii
Aah

Non non non
Oh oh oh

©2003- 2025 lyrics.com.br · Aviso Legal · Política de Privacidade · Fale Conosco desenvolvido por Studio Sol Comunicação Digital